audio
audioduration (s) 0.74
10.5
| text
stringlengths 1
99
| gender
stringclasses 2
values |
---|---|---|
Fan lay sax ? | male |
|
Saa boo ragalee Yàlla Buur bi moom miiy Kenn, ku dul Yàlla dalay ragal. | male |
|
Buma ko jàppe. | male |
|
Ndox mi mu ëmb, cafka gi dafay sëccwex | female |
|
Tom gisu ko woon. | female |
|
Ma kay wayal Seex Saalihu. | male |
|
03/07 à 2330 Mine Ubbi njël lu njëkk li | female |
|
Mas naa jaay lii. | female |
|
Damaa yeex a ñëw. | female |
|
manees na am yaakaar ci moom. | female |
|
Jën dax na, tay . | male |
|
Kuy seenub jkat? | male |
|
Fi mu am | male |
|
Buy délsi yal na nu fekk ak may gu suuxali may | female |
|
Maa ngi tëddoon sama lal. | male |
|
Sama liggéey dafa géey. | female |
|
Bul bàyyi ! | male |
|
Toma ngi ci kaw. | female |
|
Biirmaani ci lu bari Bëj-saalum-penku Asi la ñu koy boole. | female |
|
Xawma woon ne aw fen la. | male |
|
Bëggu ñu la. | male |
|
Damaa bëggoon a doon ndaw. | male |
|
Wax naa dëgg, am déet ? | female |
|
Soxla naa ab farandoo. | female |
|
dinaa leen gindi | female |
|
Ñu ngi ko tëye ca màkkaanum mu mag mu alkaati ya ca Ndakaaru. | female |
|
Buleen ma xaar. | female |
|
Bàyyi ma ma nelaw. | female |
|
Jaxaay ji ak picc mi | female |
|
Maa ngi jéggalu | female |
|
Danuy jënd ay CD. | female |
|
Suuf si daa di nangu. | female |
|
Du sama mbir. | female |
|
Xale yi gëmewuñu ko woon | female |
|
Mbooram bi dëgg la. | female |
|
Ci mbirum doomu weñ yi jigéenu-wérul war a wann | male |
|
Loo soxla ? | male |
|
Bàyyee gu Otris bàyyee Itaali Venezia. | male |
|
Loolu, du lu ma jékki-jekki rekk def ko | male |
|
Ay nit lañu. | male |
|
Bëgg naa ci benn ! | female |
|
Nos dooley kaaraange ji | male |
|
Doon naa ko ñaawal. | female |
|
Nekkon na nu ay xarit. | male |
|
Daa jubb lool. | male |
|
Da koo kott. | male |
|
Dangaa ñàkk jafe-jafe lool. | male |
|
sunuy jafe-jafe ci wàllu paj soppikuwul. | female |
|
Jëfandikoo ko walla nga ñàkk ko. | male |
|
Dama xalaat ne danga reelu. | female |
|
Bunu wuute nag, foofu la liggéey bi nekk | male |
|
Damaa am ñaan. | female |
|
Setalal sa néeg bi ! | male |
|
Toogal fii ak nun. | male |
|
Taariix | male |
|
Moos mi xossi nama. | male |
|
Naj ak forse | female |
|
Danga may fen ? | female |
|
Noo rëyee nii?! | female |
|
Nu ngi nekkandoowaat. | female |
|
Teew fa nag, doore ko ci sawaal digg-bëccëg ba jant so | female |
|
Dafa dégg i coow. | female |
|
Mbir mii daal, kenn setu ci. | female |
|
Am na ci ñent yoy ñi ngi ame ca armal ga | male |
|
Tur wi feeñ na ci Injiil ci Mk 317. | male |
|
waaye ak bii yamale, dëgërluwiin gi dafay aju ci tàngaayu wërlaay gi mu ne | female |
|
Mbaa kuy rambaaj naankat bu màndi xaaloo | male |
|
Mu ne «Ñoom de ñook woor diirub jamonoo yam». | female |
|
Masuma faa dellu. | female |
|
Beto De Canda | female |
|
Tom sopp na mool yi. | female |
|
Ma defoon ko ngir moom. | male |
|
Daanaka, demewu fa noonu | female |
|
mu wàcc-liggéey Sëriñ Abdu Laat Mbàkke wuutu ko di xalifab Sëriñ Tuubaa. | female |
|
Damaa bëgg aar. | female |
|
Wéer ngànnaay gi nag lii la wax | female |
|
Moom la leen | male |
|
Melal ni yaay man. | male |
|
Ndax jekk ngeen ? | male |
|
Man ngaa lakk farañse a? | female |
|
Jox naa la ko am ? | male |
|
Dañu maa féexal. | female |
|
Booyal bay ab tool booyal ko am at door koo bayaat | female |
|
Babilon dëkku penku la woon, di péeyug réewu Kalde, maanaam Irak | female |
|
Tus-wu-taxaw wenn la ci ñaari xammikaay yi beneen bi mooy tus-wu-gaar | female |
|
Yokkal tuuti meew. | male |
|
Mooy ne, bala dara, Séex Anta tekkikat la woon | female |
|
Jéem naa lépp. | male |
|
defleen ag tànn ! | male |
|
Boo seetloo, sunu way-tawati Covid-19 yu jëkk yi bitim-réew lañ jóge | female |
|
Man nanu koo am it jaare ko ci yeneen i lijjanti. | female |
|
XEESAL WALLA XEEB SA BOPP ? | female |
|
Waxi Seex Anta Joob ju aju làkkSoppi | female |
|
Damaa sonn lool?! | female |
|
Àdduna wori neen la. | female |
|
Lii sax caaxaan lay niru | male |
|
Loo leen di nëbb ? | female |
|
Yeneen waat yi it noonu lañu mel. | female |
|
Ku wax ? | male |
|
Dina soxla itam ab sàkket leeg-leeg ngir mu man a law ci kawam | male |
End of preview. Expand
in Dataset Viewer.
README.md exists but content is empty.
- Downloads last month
- 87