audio
stringlengths
56
116
transcription
stringlengths
4
517
/content/drive/MyDrive/Audio/audio_wolof/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales_segment_18_segment_0.wav
donc ñu gis ni formation yooyu ñu gis ni formation yooyu
/content/drive/MyDrive/Audio/audio_wolof/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales_segment_18_segment_1.wav
te yi ñu ngi ñuy woowee expert mooy ñii di seen xam-xam màcc ci mbir yooyu
/content/drive/MyDrive/Audio/audio_wolof/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales_segment_19_segment_0.wav
da ngay gis ni dañ fay wéyal di fasal lépp li nga xamante ni ay xibaar la
/content/drive/MyDrive/Audio/audio_wolof/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales_segment_19_segment_1.wav
loolu lépp li nga xamante ni xeetu xam-xam la ci domaine woowi nga xamante ni moom nañ leen ,
/content/drive/MyDrive/Audio/audio_wolof/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales_segment_1_segment_0.wav
mi nga xamante ne yaay entrepreneurs bëgg sa projet romb yenn jéego yi daf ciy baax lool
/content/drive/MyDrive/Audio/audio_wolof/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales_segment_20_segment_0.wav
donc loolu nag da ngay gis ni yow mii entreprenariat bi dafa
/content/drive/MyDrive/Audio/audio_wolof/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales_segment_21_segment_0.wav
mooy sa , doxalinu projet moo xam ci wàllu comptabilité la wala ci
/content/drive/MyDrive/Audio/audio_wolof/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales_segment_21_segment_1.wav
yeneen finance wala ci communication yooyu yëpp yow mi boobu sa projet
/content/drive/MyDrive/Audio/audio_wolof/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales_segment_22_segment_0.wav
mën nga ci tàggatu jaarale ko ci formation yooyu da ngay gis nii daf lay jàppale
/content/drive/MyDrive/Audio/audio_wolof/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales_segment_22_segment_1.wav
loolu formation yooyu ba léegi ñuy leeral am na yi si nga xamante ne dafay laaj fay am nañu nga xamante ne
/content/drive/MyDrive/Audio/audio_wolof/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales_segment_23_segment_0.wav
am na yeneen yeneen tamit du laaj fay buñ jógee ci formation yooyu am na yeneen yi nga xam te ni moom lañ
/content/drive/MyDrive/Audio/audio_wolof/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales_segment_23_segment_1.wav
ñuy wax coccine coccine nag ci wala moom mooy gunge wala tàggat
/content/drive/MyDrive/Audio/audio_wolof/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales_segment_24_segment_0.wav
wut nag ki nga xamante ni moom moo lay , tàggat ci
/content/drive/MyDrive/Audio/audio_wolof/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales_segment_24_segment_1.wav
, xam nga ne dañu nekk ci benn tomb wala ay tomb yu bëri nekk na lu am solo loolte
/content/drive/MyDrive/Audio/audio_wolof/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales_segment_25_segment_0.wav
nekk léegi daanaka am na ku am na ki nga xamante ni moom moo koy tàgget tàgget bi nag
/content/drive/MyDrive/Audio/audio_wolof/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales_segment_25_segment_1.wav
, dafay jëm ci gunge ko leeral ko li nga xamante ni moom mooy yoon yi mu war a jëf
/content/drive/MyDrive/Audio/audio_wolof/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales_segment_26_segment_1.wav
mais dañuy woowee cote bi moom day faral di def ay , daje ak entrepreneur bi
/content/drive/MyDrive/Audio/audio_wolof/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales_segment_27_segment_0.wav
waaw xam nga daje yii laaj ñoom ñaar daje toog ni wala daje
/content/drive/MyDrive/Audio/audio_wolof/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales_segment_27_segment_1.wav
ñi nga xam te ni dañuy déggante bu ko defee def leen di jàppale
/content/drive/MyDrive/Audio/audio_wolof/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales_segment_28_segment_0.wav
surtout entrepeneur bi ngir mu mën a xam moom fu mu toll ak fan la war a yegg
/content/drive/MyDrive/Audio/audio_wolof/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales_segment_28_segment_1.wav
donc yooyu nekk na mbir bi nga xamante ni bu am solo loolu dañuy faral di ko gis lu bëri léegi
/content/drive/MyDrive/Audio/audio_wolof/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales_segment_29_segment_0.wav
y ànt pêneur yi di ko wut am na beneen butadou lii di mëntoora
/content/drive/MyDrive/Audio/audio_wolof/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales_segment_29_segment_1.wav
mantoura moom it boo ko xoolee sore wul coaching waaye yamul ba léegi ndax ki nga xamante ni moom
/content/drive/MyDrive/Audio/audio_wolof/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales_segment_2_segment_0.wav
nga xamante ni da nga koy soxla dina la jàppale ngir sa projet mën a
/content/drive/MyDrive/Audio/audio_wolof/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales_segment_2_segment_1.wav
avancé gis sa projet mën a def ay jéego yi nga xamante ni yu am solo la lool
/content/drive/MyDrive/Audio/audio_wolof/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales_segment_30_segment_0.wav
mooy mentor bi moom dafay nekk kenn ki nga xamante ni ku xam-xamam màcc la
/content/drive/MyDrive/Audio/audio_wolof/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales_segment_30_segment_1.wav
ci ay mbir moom nag dafay ñëw di la jàngal
/content/drive/MyDrive/Audio/audio_wolof/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales_segment_31_segment_0.wav
di la orienté ci lépp li nga xamante ni yaa ngi ko xelaa jëmale ko ci , mbir bu
/content/drive/MyDrive/Audio/audio_wolof/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales_segment_31_segment_1.wav
bóobu moom moo lay wan naka ngay jaaree nan ngay def nag nga koy defee
/content/drive/MyDrive/Audio/audio_wolof/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales_segment_32_segment_0.wav
waaw moom nag da ngay gis ni li nga xamante ni moom moo ko xawu utalee tuuti accord ci bi moom
/content/drive/MyDrive/Audio/audio_wolof/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales_segment_32_segment_1.wav
moo xamante ne nekkul ki nga xamante ne day xaar résultat moom ak nu mu demee moom
/content/drive/MyDrive/Audio/audio_wolof/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales_segment_33_segment_0.wav
loolu lay jox ay conseils yam moom noonu lay lay lay doxee
/content/drive/MyDrive/Audio/audio_wolof/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales_segment_3_segment_0.wav
ci waxtaan wi dinañ la indil ay jumtukaay yi nga xamante ni lu lay jàppale la
/content/drive/MyDrive/Audio/audio_wolof/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales_segment_3_segment_1.wav
ay jumtukaay yi nga xamante ni boo koy faral di def da ngay gis ni di la yokk ci wàllu yu
/content/drive/MyDrive/Audio/audio_wolof/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales_segment_4_segment_0.wav
yu bëri fii nag danañ la fi indil tey ñetti yi nga xamante ni yu am solo lool
/content/drive/MyDrive/Audio/audio_wolof/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales_segment_4_segment_1.wav
jëm ci wàllu , gunge wala jëm ci wàllu tàggat sa bopp ngir li ngay def
/content/drive/MyDrive/Audio/audio_wolof/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales_segment_5_segment_0.wav
gën a mën a ñoŋ bi ci njëkk moom mooy autophormation autophormation boo ko déggee
/content/drive/MyDrive/Audio/audio_wolof/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales_segment_6_segment_1.wav
yokk seen xam-xam ci wàllu yokk seen i xarante wala lépp li nga xamante ni lui
/content/drive/MyDrive/Audio/audio_wolof/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales_segment_7_segment_0.wav
mais dañu ne jël di tax seen projet gën a mën a jëm ca kanam
/content/drive/MyDrive/Audio/audio_wolof/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales_segment_7_segment_1.wav
moom mooy ngay def ay recherches ndax da ngay gis ni , lii di xarale yu bees yi
/content/drive/MyDrive/Audio/audio_wolof/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales_segment_8_segment_0.wav
internet dafa am solo lool ci wàllu autoforémation
/content/drive/MyDrive/Audio/audio_wolof/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales_segment_9_segment_0.wav
dina la ci indil ay leeral ak ay xibaar yu bëri donc nag formation boobu ngay
/content/drive/MyDrive/Audio/audio_wolof/Renforcement_de_capacit_s_entrepreneuriales_segment_9_segment_1.wav
de fa haute formation boobu ngay def di , wàllu yéen a rechercher ngay def si interne