audio
audioduration (s)
0.74
50.6
transcription
stringlengths
8
285
senegaal dafay jaay ariko bitim réew
Naaxi jén yi ñuy rey ak seen dinamit yi yàq la
kooku dama ko jéppi ba bëgguma sax dem ci bitigam
kumba lekk ba suur gërëm ko daldi aw yoonam
man sama baay dafa dee sama ndey dee
jigéen ji nag yumaane rekk la bañ
biram njéemé bàyyi leen ñuy sox ak di xas ci guddi gi
toq doomi garab yi ci àll bi lay lekk
mbaam mu të mii dina tax ba saxaar raw ñu
soo yuqéeloo it du la taxa tollook man
maa ko def ci sama xalaatu bopp kenn sawu ma ko
fasu naaru góor lu mu mëma mëna daw ñu làbbali ko
déedéet su ma ëmbee ak su ma ëmbul yépp mu ngi ci man
Nanga xam na ngay waxe ak moom dafa gaaw a mer
seet nañu sibenam waaye lépp aw na yoon
abal ma almet ma jafal cuuraayu bant bi
yaayam yaru ko tàntam lañu ko joxoon
tàngoor wee tax weñ yi duñu ci tag
mu ni ko nag wu góor nan lañu koy ratte
xaritoo ngi gëna neex su ngeen di demlante
dégg naa ne omar dafay ngoro ak astu
mbooloo mi maa ngi leen di nuyu ku nekk ci turam ak santam
Négal ba nu àgg ca àll ba nga doora sox sa fetal
sama kër pàppa amoon na ñetti soob
damay gise ak samay waajur ba noppi sog di xam lu ma lay wax
boppu xale bi dafa fees dell ak i àkk
sama góom baa ngiy xasan léegi mu wér
dinaa la booleek jigéen ju mën a tani
ba ma defee xos bi ci sama tool ba léegi maa ngiy sant yàlla
jàngal ma li ngay wax booy jat gaynde
dafa boot xale bi santal liggéey bi keneen
sa xarit baa nga naley sukkóot di ñów
kuy yoot du sëqat wolof njaay a ko wax
tekki na téere yépp ba mu des bi ci përëg bi
bi ñu déqee sama gerte lem na ñaari yoon bosam
xale yaa ngiy as ndox mi taa ci ëtt bi
géej gaa ngi ne màww ci suñu kanam
bu ñu masaa xare ba noppi séddoo màng ga
bàyyil wékk njugub caru garab gi mën naa damm
ku leen gis ngeen ànd sax dina la suufeel
dafa dem saalum jël fa joo juuf am ak moom biram joo juuf
bu ñu bëggee falu di wuta peeg nit ñi
mu ngi ne xàmm déggul dara ci li nga ko wax
ba ñu wóññee nag yi ba noppi nag caat mi jooy jooy
ndekete soppaliku na benn caqu xaalis
xaaral ba nga jekk nga sooga wax waxu woto
góor gu saf xorom a nekkoon ci kaar bi reeloo na ñépp
biiñ am na ay ngëneel ci kow nga jëfandikoo ko bu yem
jigéen ñaa ngi àndandoo jóge màrse ku nekk yenu sa leget
Nee woon naa ko ca njëlbéen ga bumu ci dugg
faatumata sow jata yaama ndongo yadaay
ndekkete yoo yoon wi mu jaare fa la sàmba seytaane nekk
amoon na luxuskat yu ñówoon sunu lekkool
boroom kër ga dafa ko fitnaaloon bu mu mujj toxu
bu sa sukkóot bi dammee nga waaru de
saaliyu ngóor si ci jaasi ji rekk a ñibbisi
xàmme naa la léegi bi nga takkul say lonet
gaa ñi daldi fetal sox yi till gi daldi daanu
réew mi dafa meloon ni garab goo xam ne dafa ngal
furno bi dëger na ba tey giriyaas bi rekk a yàqu
faatoo ngi saatlu ci ñeent fukki atam