wolof
stringlengths
6
405
french
stringlengths
8
465
english
stringlengths
7
437
Kremlin waxna ne ñakk nangu Waasinton ci porose lu ko wundu mooy mbiruum koom te loolu misaal la ci ñakk maandu ci kujje.
Le Kremlin plaide que Washington s’oppose vivement au projet que pour des raisons économiques et qu’il s’agit d’un exemple de concurrence déloyale.
The Kremlin argues that Washington's fervent opposition to the project is simply driven by economic reasons and is an example of unfair competition.
Jawriñu Riisi buñu denk enersi, Aleksandr Novak, neena, ginnaaw ndaje bumu amal ak naataangoom bu Amerig Rick Perry ci Mosku ci weeru Septambar "gëmna ne noo bokk gis-gis ci enersi warul nek luy tënkaate te woy jëfandikoo yi dañoo wara tann seen furnisoor yi."
« Je crois que nous partageons l’opinion que l’énergie ne peut être un moyen de pression et que le consommateur devrait pouvoir choisir son fournisseur », a soutenu Aleksandr Novak, ministre russe de l’Énergie à la suite d’un entretien avec son homologue américain, Rick Perry, à Moscou en septembre dernier.
"I believe we share the view that energy cannot be a tool to exercise pressure and that consumers should be able to choose the suppliers," Russian Energy Minister Aleksandr Novak said following a meeting with US Energy Secretary Rick Perry in Moscow in September.
Taxawaayu reewum Amerig andina coow ci Almaañ mi nga xamne feddalina kollere am ci porose bi.
La position américaine a soulevé de fortes réactions en Allemagne, qui a réaffirmé son engagement envers le projet.
The US stance has drawn backlash from Germany, which has reaffirmed its commitment to the project.
Kureelu lindistri bu Almaañ bu gëna mag, Fedaraasiyo indistri yi Almaañ (BDI), ñaaxna ñu reewum Amerig ñu genn ci tëralinu enersi bu mbootayu reewi Orop ak maankoo digante Berlin ak Mosku.
Le principal organisme allemand de l’industrie, la Fédération des industries allemandes (BDI), a invité les États-Unis à ne pas se mêler des politiques énergétiques européennes et des ententes bilatérales entre Berlin et Moscou.
Germany's leading organization for industry, the Federation of German Industries (BDI), has called on the US to stay away from the EU energy policy and the bilateral agreements between Berlin and Moscow.
Dieter Kempf, njiitu Fedaraasiyo indistri yi Almaañ (BDI) neena, ginnaw bumu daje ak Sanseliyeer bu Almaañ Angela Merkel ak njiitu reewum Riisi Vladimir Putin "dama am jafe-jafe bu magg ci beneen duñu jox sunu enersi"
« J’ai un grand problème avec le fait qu’un troisième pays se mêle à notre approvisionnement en énergie », a déclaré Dieter Kempf, chef de Fédération des industries allemandes, à la suite d’une rencontre récente entre la chancelière allemande, Angela Merkel, et le président russe, Vladimir Putin.
"I have a big problem when a third state interferes in our energy supply," Dieter Kempf, head of the Federation of German Industries (BDI) said following a recent meeting between German Chancellor Angela Merkel and Russian President Vladimir Putin.
Buñu sukkandikoo ci Senatoor bu Masasuset, Elizabeth Warren mu ngi "xalaat bu baax" ngir bokk ci joŋante njiitu reewmi bu 2020.
Elizabeth Warren étudiera « de manière approfondie » la possibilité de se présenter comme candidate aux élections présidentielles de 2020, a indiqué la sénatrice du Massachusetts
Elizabeth Warren Will Take "Hard Look" At Running For President in 2020, Massachusetts Senator Says
Senaatër bu Masasuset Elizabeth Warren neena samdi fas yeene na "bu baax" bokku ci elksiyoŋ njiitu reew mi ginnaaw bi elksiyoŋ digi-doomu yi jalee.
La sénatrice du Massachusetts, Elizabeth Warren a indiqué samedi dernier qu’elle étudiera « de manière approfondie » la possibilité de se présenter comme candidate aux élections présidentielles après les élections de mi-mandat.
Massachusetts Senator Elizabeth Warren said on Saturday she would take a "hard look" at running for president following the midterm elections.
Ci benn ndaje ci Holyoke, ci Masasuset, Warren dëggëlna ne bëgg na bokk.
Warren a confirmé qu’elle envisage de se présenter lors d’une séance de discussion ouverte à Holyoke, au Massachusetts.
During a town hall in Holyoke, Massachusetts, Warren confirmed she'd consider running.
Neena, bu ñu sukkandiko ci The Hill "jotna jiggeen ñi dem Waasinton ñu defar lu nguur gi yaxx te loolu dafa laaj benn njiit bu jiggeen."
« Il est temps qu’il y ait des femmes à Washington pour remettre un gouvernement dysfonctionnel sur les rails, et cela comprend une femme au pouvoir » a-t-elle déclaré, selon The Hill.
"It's time for women to go to Washington and fix our broken government and that includes a woman at the top," she said, according to The Hill.
"Ginnaaw 6 Nowambar, dina xalaat bu baax numay bokkee ci elksiyoŋ njiitu reew mi."
« Après le 6 novembre, je vais étudier de manière approfondie la possibilité de me présenter comme candidate à la présidence ».
"After November 6, I will take a hard look at running for president."
Warren waxna ci Persidan Donald Trump ci ndaje mi, mune mu "ngi jëmee dékk bi fu baaxul.
Warren a commenté sur le président Donald Trump lors de la séance de discussion, disant qu’il « menait le pays dans la mauvaise direction ».
Warren weighed in on President Donald Trump during the town hall, saying he was "taking this county in the wrong direction.
Neena "daama tiit am njaqqare bu rëy ci lu Donald Trump def sunu demokaraasi."
« Je suis extrêmement inquiète de ce que Donald Trump est en train de faire à notre démocratie », a-t-elle déclaré.
"I am worried down to my bones about what Donald Trump is doing to our democracy," she said.
Warren fësalna bu baax ŋaññ am ci Trump ak kumu tann ca ëttu atteekaay bu magg ba Brett Kavanaugh.
Warren a critiqué ouvertement Trump et son choix de Brett Kavanaugh à la Cour suprême.
Warren has been outspoken in her criticism of Trump and his Supreme Court nominee Brett Kavanaugh.
Ci benn tiwit ci aljuma ci, Warren neena "si dëgg-dëgg soxlanañu saytub FBI balaa eleksiyoŋ yi."
Dans un micromessage publié vendredi, Warren a dit qu’il était « bien sûr nécessaire d’ouvrir une enquête du FBI avant de voter ».
In a tweet on Friday, Warren said "of course we need an FBI investigation before voting."
Ab sondaas buñu biral alkamis dafa wone ne ñu bari ci ñuy wotel soxna Warren dañoo yaakaar ne warul bokk 2020.
Un sondage publié jeudi a cependant indiqué qu’une majorité de ses propres électeurs ne pensaient pas qu’elle devrait se présenter aux élections de 2020.
A poll released on Thursday, however, showed a majority of Warren's own constituents do not think she should run in 2020.
Juroom-fukk ak juroom ñett ci teemeer bu nekk ci ñu "nara" wote ca Masasuset neena ñu senatoor bi warta bokk, buñu sukkandiko ci Suffolk University Political Research Center/Sonndaasu Boston Globe.
Quarante-huit pour cent des électeurs « probables » du Massachusetts ont dit que la sénatrice ne devrait pas se présenter dans un sondage Suffolk University Political Research Center/Boston Globe.
Fifty-eight percent of "likely" Massachusetts voters said the senator should not run, according to the Suffolk University Political Research Center/Boston Globe poll.
Fanweer ak ñaar ci teemer boo jël aandnañu ci kurs bi.
Trente-deux pour cent ont pour leur part indiqué qu’ils appuyaient sa candidature.
Thirty-two percent supported such a run.
Sondaas bi wonena jappale bu magg ci bokk Guwernoo ba woon Deval Patrick, ak 38 ci teemeer boo jël ak 48 ci teemeer boo jël ñu andul ak moom.
Le sondage rapportait un appui pour ferme pour la candidature de l’ancien Gouverneur, Deval Patrick, avec 38 pour cent, par rapport à 48 pour cent qui s’y opposait.
The poll showed more support for a run by former Governor Deval Patrick, with 38 percent supporting a potential run and 48 percent against it.
Ci turu Demokraat yu siiw yuñu ruumandaat mënn nañu bokk ci eleksiyon 2020 yi Joe Biden, ku toppoon ci njiitum reewmi ak Senaatoor bu Vermont Bernie Sanders.
D’autres personnalités du parti démocrate mentionnées comme candidats potentiels aux élections de 2020 comprennent le vice-président Joe Biden et le sénateur du Vermont, Bernie Sanders.
Other high profile Democratic names discussed in regard to a potential 2020 run include former Vice President Joe Biden and Vermont Senator Bernie Sanders.
Biden neena dina jél ndogal bu fës fii ak Sanwiye, loolu la Associated Press wax.
Selon l’Associated Press, Biden devrait conformer ou non s’il se présente d’ici janvier.
Biden said he would decide officially by January, the Associated Press reported.
Sarah Palin waxna ci feebaru xel Track Palin ci ndaje bu Donald Trump woote woon
Sarah Palin parle du syndrome de stress post-traumatique de Track Palin au rassemblement de Donald Trump
Sarah Palin cites Track Palin's PTSD at Donald Trump rally
Track Palin, 26 att, neekna benn at ci Irak ginnaw bimu bindoo ci satumbar.
Track Palin, qui a 26 ans, a passé un an en Irak après s’être enrôlé en septembre.
Track Palin, 26, spent a year in Iraq after enlisting on Sept.
Japp nañu ko te luñu koy toppee ci fitnaal soxnaam altine ci guddi
Il a été arrêté et accusé à la suite d’un incident de violence domestique lundi soir.
He was arrested and charged in a domestic violence incident on Monday night
Neena ci ndaje buy jappale Donald Trump caTulsa ci Oklahoma "lu sama doom jaŋkontel bumu ñëwaate mënnaa ko wax yeneen njaboot ñu gis njeexitalu feebaru xel ak ay gaañu-gaañu yu soldaar yi di andiwaale buñu ñibisee.
« Ce que vit mon fils à son retour, je comprends les autres familles qui ressentent les effets du syndrome de stress post-traumatique les blessures que rapportent nos soldats », a-t-elle dit aux participants lors d’un rassemblement pour Donald Trump à Tulsa, en Oklahoma.
"What my own son is going through, what he is going through coming back, I can relate to other families who feel ramifications of PTSD and some of the woundedness that our soldiers do return with," she told the audience at a rally for Donald Trump in Tulsa, Oklahoma.
Palin tuddee na luñu ko jappee "ñay ci biir neeg" te mune doom am ak yeneen moroom am, "dañuy dellusi soppeeku, dañuy dellusi soxor, dañuy dellusi di laaj ndax dinañu jox cër lu seen i morom soldaar yi ak pilot yi ak yeneen pacc larme bi defal reewmi.
Palin a qualifié l’arrestation de son fils de « problème dont personne n’ose parler », ajoutant que son fils et les autres anciens combattants « reviennent un peu différents, ils sont endurcis, se demandant si les gens reconnaissent ce que les soldats, les membres de la force aérienne et les autres militaires ont fait pour le pays ».
Palin called his arrest "the elephant in the room" and said of her son and other war veterans, "they come back a bit different, they come back hardened, they come back wondering if there is that respect for what it is that their fellow soldiers and airmen, and every other member of the military, has given to the country."
Teknañu ko loxo Altine ci Wasilla ci Alaska, luñu koy tuumal moy door jabaram boole ci ak yore ngannaay ak maandi, bu ñu sukkandikoo ci Dan Bennett, mooy wax ci turu Poliisu Wasilla.
Il a été arrêté et accusé de violence sur une femme, de nuire à un signalement de violence domestique et de possession d’une arme tout en étant intoxiqué, lundi, à Wasilla, en Alaska, selon Dan Bennett, porte-parole du service de police de l’endroit.
He was arrested on Monday in Wasilla, Alaska, and charged with domestic violence assault on a female, interfering with a report of domestic violence and possession of a weapon while intoxicated, according to Dan Bennett, a spokesman for the Wasilla Police Department.
18 dëk ak Diwaan bu Kolombiya ñoo ngi jappale ñaxtu bu bees bi ci tëralinu woy daw laqqu yi
18 États et le district de Columbia soutiennent la contestation de la nouvelle politique relative au droit d’asile
18 states, D.C. support challenge to new asylum policy
Fukk ak juroom-ñett dëk ak Diwaan bu Kolombiya ñoo ngi jappale kalaame ci yoon ci tëralinu Amerig bu bees bi buy xañ laqq ñu loru ci kuurel yu bonn ak ñiñu fitnaal si kër yi.
Dix-huit États et le district de Columbia soutiennent la contestation juridique de la nouvelle politique américaine qui refuse le droit d’asile aux personnes qui tentent de fuir la violence de gangs de rue ou familiale.
Eighteen states and the District of Columbia are supporting a legal challenge to a new U.S. policy that denies asylum to victims fleeing gang or domestic violence.
NBC News nettalina ne ndawi 18 dëkk ak distirikt jebbalnañu ab teere ca Wasinton ngir jappale benn woy laqqu buy ñaawlu biile tëralin.
NBC News a rapporté que des représentants des 18 États et du district ont déposé un mémoire d’ami de la cour vendredi à Washington en guise de soutien à un demandeur d'asile qui conteste la politique.
Representatives from the 18 states and the district filed a friend-of-the-court brief Friday in Washington to support an asylum-seeker challenging the policy, NBC News reported.
Turu ak sant peleñaa bi ci mbiru Grace v. Porose bu American Civil Liberties Union defoon ci weeru Ut poliis federaal biraluñuko.
Le nom complet du plaignant dans la poursuite Grace contre Sessions déposée par l’Union américaine pour les libertés civiles en août contre la politique fédérale n’a pas été révélé.
The full name of the plaintiff in the Grace v. Sessions suit that the American Civil Liberties Union filed in August against the federal policy has not been revealed.
Neena nekkaale am "ak doom am yu bokk kureel yu bari fitna," ñoo ko toroxal waaye kilifa reewum Amerig nanguwuñu ñaanam ci 20 Sulet.
Elle a affirmé que son partenaire « et que ses fils violents et membres d’une gang de rue » ont abusé d’elle, mais que les représentants des États-Unis ont refusé sa demande d’asile le 20 juillet.
She said her partner "and his violent gang member sons," abused her but U.S. officials denied her request for asylum July 20.
Dañu ko jappoon ci Teksaas.
Elle était détenue au Texas.
She was detained in Texas.
Attekatu nguur gi di jappale Grace tektalena El Salvador, Honduras ak Guatemala,ñii seen doom yu takku di wuut laxxuwaay ni ay réew yu am jafe jafe fitnaal ci kër yi aki banndi.
Les procureurs des États soutenant Grace ont décrit l’El Salvador, le Honduras et le Guatemala comme des pays d’où proviennent de nombreux demandeurs d’asile aux États-Unis en raison de problèmes omniprésents de violence liée aux gangs de rue ou de nature familiale.
The states' attorneys supporting Grace described El Salvador, Honduras and Guatemala, which produce a large number of applicants for U.S. asylum, as nations facing pervasive problems with gangs and domestic violence.
olitiku Amerik bu bees bi te ñeel wallu daw laxxatu bi defa dëpp benn ndogal bu 2014 bi Waa Bankaasu Tukki bi tëraloon ngir bayi tukkikat yii amul ay këyit di duggu ndax ñu rëccu ci fitnaal ci kër yi ba muna laxxatuji.
La nouvelle politique américaine relative aux demandes d’asile a annulé une décision de 2014 du conseil des appels des immigrants (Board of Immigrant Appeals) qui permettait aux immigrants sans papiers fuyant la violence dans leur pays à demander l’asile.
The new U.S. asylum policy reversed a 2014 decision by the Board of Immigrant Appeals that allowed undocumented immigrants fleeing domestic violence to apply for asylum.
Attekatu leegal bii di Columbia Seneraal Karl Racine neena ci benn dekkalaare ci bësu Aljuma ni politik bu bees bi "defa jalgati lu amoon lu tollu ci ay ati at, mu di Yoon bu federaal ak bittim réew yepp."
Le procureur du district de Columbia, Karl Racine, a publié une déclaration vendredi disant que la nouvelle politique « va à l’encontre de dizaines d’années de droit à l’échelle de l’État, fédérale et internationale ».
District of Columbia Attorney General Karl Racine said in a statement Friday that the new policy "ignores decades of state, federal, and international law."
“Yoon federaal bi defa bëgg beppu laaj daw laxxatu ñu ménngale ko ak ay jëf aki anam yu laaj boobu , te ap bistoroŋ daadina ñakk sammante ak loolu, " ki xamle loolu moy xaritu kuur bi.
« La législation fédérale exige que les décisions pour toutes les demandes d’asile doivent être rendues en fonction des faits et des circonstances propres de la demande et une telle interdiction viole ce principe », prétend le mémoire d’ami de la cour.
"Federal law requires that all asylum claims be adjudicated on the particular facts and circumstances of the claim, and such a bar violates that principle," the friend-of-the court brief said.
Attekat bi wéyal di wax ci leeral boobu ni politiku xañ tukkikat yi duggu Amerik defay gallaŋkoor seen koom koom, di wax ni munna am ñu nekkaat ay antarperneer te ñuy "maye ligeey bu ko jar"
Le mémoire ajoute aussi que la politique, en refusant l’asile aux demandeurs, nuit à l’économie américaine, car ils sont plus susceptibles de devenir des entrepreneurs et de « fournir une main-d’œuvre nécessaire ».
Attorneys further argued in the brief that the policy denying immigrants entry hurts the U.S. economy, saying they are more likely to become entrepreneurs and "supply necessary labor."
Attekat bii di Seneraal Jeff Sessions digalna ñiiy atte wallu tukki ni leen mbu ñu mayeti laxxuwaay benn nit buy daw fitna ci kër mbaa mettitalu banndi yi.
Le procureur général Jeff Sessions a ordonné aux juges en immigration de ne plus accorder l’asile aux victimes de violence familiale ou liée aux gangs de rue en juin.
Attorney General Jeff Sessions ordered immigration judges to no longer grant asylum to victims fleeing domestic abuse and gang violence in June.
"Laxxuwaay ñeelna ñooñu di juge seen rëëw ndax ay toroxal mbaa ragal lu jëm ci xeet, diine , waaso ,mbaa bokk ci benn mboolo mbaa xalaat bu politik,” Sessions moo ko wax ci 11 weeru Suye ci ndoortelu politik ba.
« L’asile peut être demandé par les personnes qui quittent leur pays d’origine en raison de persécutions ou par crainte en raison de la race, de la religion, de la nationalité ou de l’appartenance à un groupe social ou à une opinion politique en particulier », a déclaré Sessions lors de l’annonce de la politique le 11 juin.
"Asylum is available for those who leave their home country because of persecution or fear on account of race, religion, nationality, or membership in a particular social group or political opinion," Sessions said in his June 11 announcement of the policy.
Daw laqqu musul jublu ci waññi jafe-jafe yép -- doon te yu gëna mag -- yu nit ñi di jankontel bes bu nek fepp ci aduna.
L’asile n’a jamais eu comme objectif d’atténuer tous les problèmes rencontrés par les personnes dans le monde, même les plus sérieux.
Asylum was never meant to alleviate all problems -- even all serious problems -- that people face every day all over the world.
Ay wallu yu mujjuta aantu ci Palu te limu ñuy faatu mungi yokku ci ñu des a dundu
Opérations de secours désespérées dans une course pour retrouver des survivants à Palu tandis que le bilan s’alourdit
Desperate rescue efforts in Palu as death toll doubles in race to find survivors
Ci ñu mucc, mbir yi dafa gënoon di metti.
La situation est de plus en plus désespérée pour les survivants.
For survivors, the situation was increasingly dire.
Risa Kusuma mii tollu ci 35 att neena" defa tarr lool" muy jappale doomam bu goor ci benn santaru rawale ci dëkk bu tiis boobu di Palu.
« C’est très tendu », a déclaré Risa Kusuma, 35 ans, tout en réconfortant son garçon fiévreux à un centre d’évacuation dans la ville dévastée de Palu.
"It feels very tense," said 35-year-old mother Risa Kusuma, comforting her feverish baby boy at an evacuation centre in the gutted city of Palu.
"Simili bu nek ambilaans day andi ay néew.
« Une ambulance vient porter des corps chaque minute.
"Every minute an ambulance brings in bodies.
Ndox mu sell dafa jafe."
L’eau potable est rare. »
Clean water is scarce."
Waa dëkk bi gisnañu leen ñu doon dellusi ci seen kër yu yaxxu yi, di,jaar ci ay bërëb yu ndox naangu, di jeema rawale lepp lu ñu mën.
Des résidents ont été aperçus, retournant à leur maison détruite et ramassant tout bien détrempé qu’ils pouvaient sauver.
Residents were seen returning to their destroyed homes, picking through waterlogged belongings, trying to salvage anything they could find.
Ay teemeeri nit gaañu nañu ci yénngu-yénngu suuf si bu tollu ci 7.5, këru facookaay yi yaqqu nañu te fees nañu.
Les hôpitaux, endommagés par le tremblement de terre d’une magnitude de 7,5, étaient débordés par les centaines de blessés.
Hundreds of people were injured and hospitals, damaged by the magnitude 7.5 quake, were overwhelmed.
ñii ci ame ay gaañu gaañu ku ci mel ni Dwi Haris mii doon jammbat ap ndigg ak mbagg yu damm, mungi doon dallu ci bitti lopitaalu arme bu Palu fu fajukat yi daan am ay pajj ci bitti ndax ndesitu tocc tocc yi amoon.
Certaines victimes, comme Dwi Haris, blessé au dos et à une épaule, se trouvaient à l’extérieur de l’hôpital militaire de Palu, où les patients recevaient des soins à l’extérieur en raison des répliques constantes.
Some of the injured, including Dwi Haris, who suffered a broken back and shoulder, rested outside Palu's Army Hospital, where patients were being treated outdoors due to continuing strong aftershocks.
Ay ronngoñ tuuro ci ay gëtam bi muy nettali ni yeŋngum suuf bu am doole bi gësëmee neegu juroomeelu etaas bi mu nekkoon moom ak jabaram ak seen doom.
Les larmes aux yeux, il a raconté la manière dont le violent tremblement de terre a secoué la chambre du cinquième étage de l’hôtel qu’il partageait avec sa femme et sa fille.
Tears filled his eyes as he recounted feeling the violent earthquake shake the fifth-floor hotel room he shared with his wife and daughter.
"Amuñu woon benn jot ngir rawal sunu bopp.
« Nous n’avons eu aucune chance de nous sauver.
"There was no time to save ourselves.
Dema keppuwoon ci tojitu tabax ba, laa yaakaar" la Haris wax waa Associated Press, mu yokk ci ni njabootam mungi woon ci biir dëkk bi ngir benn cëytal.
Je crois que j’étais coincé dans le mur en ruine », a raconté Haris à l’Associated Press, ajoutant que sa famille était sur place pour un mariage.
I was squeezed into the ruins of the wall, I think," Haris told Associated Press, adding that his family was in town for a wedding.
"Deggnaa sama jabar di woote wallu, waante deggatuma dara.
« J’ai entendu ma femme crier à l’aide, puis c’était le silence.
"I heard my wife cry for help, but then silence.
Xamuma lan mooko dal moom ak sama doom.
Je ne sais pas ce qui lui est arrivé, à elle et à ma fille.
I don't know what happened to her and my child.
Maa ngi yaakaar ne ñoo ngi ci jam.
J’espère qu’elles sont saines et sauves ».
I hope they are safe."
Ambasadeeru Amerig dafa tuumal Siin 'xoqqatal' ak 'pibilisite ak poropagaan
L’ambassadeur des États-Unis accuse la Chine de faire de l’« intimidation » au moyen de « publicités de propagande »
U.S. ambassador accuses China of 'bullying' with 'propaganda ads'
Ayubes ginnaaw bi benn surnaalu Siin defare ap piblisite ci ap njaay bu Amerik daan def te mu ciy seddo benefiis ak Siin. Ndaw mii toogal Amerik ci Siintuumalna Beinjing ni defay jefandiku yeglekaayu Amerik yi di siiwal ay parpagaan.
Une semaine après la parution d’une publicité de quatre pages par un journal officiel chinois dans un quotidien américain prétendant que les échanges commerciaux entre les États-Unis et la Chine profitaient aux deux pays, l’ambassadeur des États-Unis en Chine a accusé Beijing de faire de la propagande au moyen de la presse américaine.
A week after an official Chinese newspaper ran a four-page ad in a U.S. daily touting the mutual benefits of U.S.-China trade, the U.S. ambassador to China accused Beijing of using the American press to spread propaganda.
Réewum Amerig. Persida Donald Trump neena peyooru Daily bu Siin ci Des Moines Register- taskatu xibaar bu daxxa jaay ci rëëw bu Iowa ginnaaw bi mu tuumale Siin ni defa doon jeema dugal loxo am ci woote koŋngere bu Amerik ci 6 fan ci weeru Nowammbur, waayu Siin weddina ko.
Le président américain, Donald Trump, a parlé mercredi dernier de la publicité payée par la Chine dans le Des Moines Register, le journal le plus vendu en Iowa, après avoir accusé la Chine d’essayer de se mêler des élections législatives du 6 novembre, une accusation rejetée par la Chine.
U.S. President Donald Trump last Wednesday referred to the China Daily's paid supplement in the Des Moines Register - the state of Iowa's biggest selling newspaper - after accusing China of seeking to meddle in the Nov. 6 U.S. congressional elections, a charge China denies.
Tuumalu Trump boobu ni Beijing defa doon jeema dugal loxo am ci wote Amerik la ofisiyel yu Reuters wax ni ap jeego bu bees la ci pexem Washington ngir waaxu ci kaw Siin.
Les responsables américains ont déclaré à Reuters que ces accusations représentaient une nouvelle phase d’une campagne grandissante par Washington pour mettre de la pression sur la Chine.
Trump's accusation that Beijing was trying to meddle in U.S. elections marked what U.S. officials told Reuters was a new phase in an escalating campaign by Washington to put pressure on China.
Moon te yoon la de nguur yi def ay pibilisite ngir xamle seeni njaay, Beijing ak Washington moom defa mel ni deñoo duggu ci ap defante boo xam ni def leen tollale ci wallu empoor.
Il est normal de voir de la publicité faisant la promotion des échanges commerciaux par les gouvernements étrangers, mais Beijing et Washington sont aux prises actuellement dans une guerre commerciale à coup de droits supplémentaires sur les importations des deux pays.
While it is normal for foreign governments to place advertisements to promote trade, Beijing and Washington are currently locked in an escalating trade war that has seen them level rounds of tariffs on each other's imports.
Njegu feyantu yu Siin ci njelbeen de ngir muna xatal jëndkat yu mel ni Iowa mii doon jappale parti Repibilikeen bu Trump rek la, loolu la seetlukatu Siin ak Amerik wax.
Les tarifs de représailles adoptés tôt dans la guerre commerciale par la Chine avaient pour but de toucher des exportateurs d’États comme l’Iowa, connus pour soutenir Trump et le pari républicain, selon des experts de la Chine et des États-Unis.
China's retaliatory tariffs early in the trade war were designed to hit exporters in states such as Iowa that supported Trump's Republican Party, Chinese and U.S. experts have said.
Terry Branstad, ndaw mi toogal Amerik ci Siin te mu nekkoon guwerneeru Iowa lu yagg, moom mii nekk jëndkatu marsandiisu mbey ci Siin, neena Beijing lorna ligeeykatu Amerik, beykat ak bisneeskat yi.
Terry Branstad, l’ambassadeur en Chine ancien gouverneur de longue date de l’Iowa, état qui exporte beaucoup de produits agricoles vers la Chine, a déclaré que la Chine avait fait mal aux travailleurs, aux fermiers et aux entreprises des États-Unis.
Terry Branstad, the U.S. ambassador to China and the former longtime governor of Iowa, a major exporter of agricultural goods to China, said Beijing had hurt American workers, farmers and businesses.
Ci benn xalaat bu mu bind ci Des Moines Register bu Sunday, Branstad mungi wax ni Leegi Siin "mungi def ñaar ci lepp lu mu doon def benn jaare ko ci ay pibilisite parpagaan yu muy def ci sunu taskatu xibaar yi.”
Dans une lettre d’opinion parue dimanche dans le Des Moines Register, Branstad a écrit que la Chine « a renchéri ses tactiques d’intimidation en faisant paraître de la publicité de propagande dans notre presse libre ».
China, Branstad wrote in an opinion piece in Sunday's Des Moines Register, "is now doubling down on that bullying by running propaganda ads in our own free press."
"Ngir nëbb seen parpagaan boobu nak nguuru Siin bi mungi laxxatu ci cosaanu Amerik boobu di sañ sañu wax ak taskatu xibaar yu feex, muy fey xaalis ñu defal ko pibilisite ci Des Moines Register" Branstad moo ko bind.”
« En semant sa propagande, le gouvernement chinois profite de la tradition de la liberté d’expression et de la presse libre précieuse aux Américains en publiant une annonce dans le Des Moines Register », a-t-il écrit.
"In disseminating its propaganda, China's government is availing itself of America's cherished tradition of free speech and a free press by placing a paid advertisement in the Des Moines Register," Branstad wrote.
Mu bind "Ci beneen wall wi, ci ëtt bu bees bi ci mbedd mi fii ci Beijing, nééwna looy dégg ay wax yuy wane mer, te doo mëna gis ci kanamu nit ñi ap tiitaange walla njakkare ndax lu Siin di jeema yaxx doxalinu xoom xoom gi ndax te taskatu xibaar yi ci loxo Parti kominist bi lañu nekk."
« L’histoire est différente au kiosque à journaux ici, à Beijing. Les voix dissidentes sont rares et il n’y a aucune vraie réflexion sur les opinions disparates des Chinois sur la stratégie économique troublante de leur pays étant donné que les médias sont sous le joug du Parti communiste chinois », a-t-il écrit.
"In contrast, at the newsstand down the street here in Beijing, you will find limited dissenting voices and will not see any true reflection of the disparate opinions that the Chinese people may have on China's troubling economic trajectory, given that media is under the firm thumb of the Chinese Communist Party," he wrote.
Yu yokk ci ni" Kenn ci taskatu xibaar yu gina magg ci Siin defa baña bind " kaddu am yi,waaye itam waxul bann taskatu xibaar la.
Il a ajouté que « l’un des journaux d’importance de la Chine a refusé l’offre de publier » son article, sans, toutefois, préciser lequel.
He added that "one of China's most prominent newspapers dodged the offer to publish" his article, although he did not say which newspaper.
Repibilikeen yi di tuutal jigeen wotekat yi ci wote diggupal ak mbiru Kavanaugh bi , seetlukat yi ñoo xamle loolu
Les républicains s’aliènent le vote des femmes en route vers les élections de mi-mandant en raison de la débâcle Kavanaugh selon une analyse
Republicans Alienating Women Voters Ahead of Midterms With Kavanaugh Debacle, Analysts Warn
Ginnaaw Repibilikeen yu bari deñoo faral aki layool ki ñu tuddu ci Kuur bu Kawe bi Brett Kavanaugh ci wallu tuuma siif , seetlukat yi artunañu wax ni dina am benn xoxxatal; rawatina bu juge ci ay jigeen ci woote diggupal yii jubsi.
Tandis que de nombreux républicains de premier plan soutiennent et défendent la nomination de Brett Kavanaugh à la Cour suprême malgré plusieurs allégations d’agression sexuelle, des analystes ont averti qu’ils en vivraient des répercussions, particulièrement avec les femmes, dans les élections de mi-mandat à venir.
As many top Republicans stand-by and defend Supreme Court nominee Brett Kavanaugh in the face of several allegations of sexual assault, analyst have warned they will see a backlash, particularly from women, during the upcoming midterm elections.
Yég yég bi am ci mii mbir defa kawe torop te lu ëppu ci Repibilikeen yi parenañu, deñoo bëgg wote.
Les émotions entourant cette situation sont très vives et la plupart des républicains ont déjà officiellement donné signe qu’ils souhaitaient que le dossier avance et qu’un vote soit tenu.
The emotions surrounding this have been extremely high, and most Republicans are on record already showing they wanted to go forward with a vote.
Yooyu mbir munuñuleen ariyeeraat," Grant Reeher, ap janngalekatu durwa ci Daara ju kawe ju Syracuse Maxwell Scholl neena The Hill ngir benn xalaat bu genni Samdi.
« Dans ces situations, il est impossible de retourner en arrière », a déclaré Grant Reeher, professeur en science politique à l’école Maxwell de l’Université de Syracuse dans un article publié samedi dans The Hill.
Those things can't be walked back," Grant Reeher, a professor of political science at Syracuse University's Maxwell School told The Hill for an article published Saturday.
Reeher neena defa am sikki sakka ni bumax bu senateer Jeff Flakes (R-Arizona) bumax FBI ngir laŋket dina doy sëkk ngir dalal wotekat yu mer yi.
Reeher a dit douter que les efforts de dernière minute du sénateur Jeff Flake (R-Arizona) pour une enquête du FBI soient suffisants pour apaiser le mécontentement chez les électeurs.
Reeher said he doubts Senator Jeff Flake's (R-Arizona) last-minute push for an FBI investigation will be enough to placate angry voters.
"Jigeen yi naruñu fatte li xewoon dëmb, -du ñu ko fatte ëllëk, du doon Nowammbur tamit" sunu sukkandikoo ci taskatu xibaar bu Washinghton DC bi Karine Jean-Pierre ap konseye di porto parool nasonaal ngir kurel boobu di Moveon moo wax li ñu mel.
« Les femmes n’oublieront pas ce qui s’est passé hier, elles ne l’oublieront pas demain ni en novembre », a déclaré vendredi Karine Jean-Pierre, conseillère principale et porte-parole nationale du groupe progressif MoveOn, selon le journal de Washington.
"Women are not going to forget what happened yesterday - they are not going to forget it tomorrow and not in November," Karine Jean-Pierre, a senior adviser and national spokeswoman for the progressive group MoveOn said on Friday, according to the Washington, D.C. newspaper.
Aljuma ci suba si, fippukat yi ñungi doon yuuxu" Nowammbur mungi ñéw!" ni ñu ko wane ci suufu tabax bu Sena ba, bi Repibilikeen yi yore komite wallum Yoon wi fasnañu yeene fal Kavanaugh te baña bayi xel seede bu Dr. Christine Blasey Ford, buñu sukkandiko ci Mic.
Vendredi matin, des manifestants scandaient « Novembre s’en vient! » lors d’une manifestation dans le corridor du sénat au moment où les républicains à la tête de la commission judiciaire ont choisi d’aller de l’avant avec le choix de Kavanaugh malgré le témoignage de la docteure Christine Blasey Ford, selon Mic.
On Friday morning, protestors chanted "November is coming!" as they demonstrated in the hallway of the Senate as the Republicans controlling the Judiciary Committee chose to move forward with Kavanaugh's nomination despite the testimony of Dr. Christine Blasey Ford, Mic reported.
Rëy Demokaratik yi ak seen bëgge dina jeggi dayo" stu Rothenberg, ap setlukat bu farul benn parti politik, moo ko wax ci situ enternet xibaar yi.
« L’enthousiasme et la motivation des démocrates seront à leur comble », a dit Stu Rothenberg, analyste politique non partisan, a rapporté le site d’actualités.
"Democratic enthusiasm and motivation is going to be off the chart," Stu Rothenberg, a nonpartisan political analyst, told the news site.
"Nit ñaa ngi wax yékkatinina ñu ko ba pare; loolu dëgg la.
« Les gens disent qu’ils sont déjà élevés et c’est vrai.
"People are saying it's already been high; that's true.
Waaye mënna gina kawe, rawatina nak jigeen yii di wote ci dëkku kaw gi ak wotekat yu gëna ndaw yi , 18- ba 29 att, ñiy faral di ñakka wote su ñu buggul persida bi."
Mais ce pourrait l’être plus, en particulier chez les femmes de banlieue qui changent de camp et les jeunes électeurs de 18 à 29 ans, qui, même s’ils n’aiment pas le président, souvent, ne votent pas.
But it could be higher, particularly among swing women voters in the suburbs and younger voters, 18- to 29-year-olds, who while they don't like the president, often don't vote."
Laata Ford di def ap leeral ci naka la siif bi mu tuumal ki ñu fal ci Kuur bu Kawe bi, seetlukat yi waxoon nañu ni ap xoxxatal munna am su Repibilikeeb yi puuse jém ci kanam ak ap firnde.
Même avant le témoignage public de Ford où elle expliquait en détail ses allégations d’agression sexuelle par le candidat à la Cour suprême, les analystes ont laissé entendre qu’il pourrait y avoir du mécontentement si les républicains confirmaient la nomination.
Even before Ford's public testimony detailing her allegations of sexual assault against the Supreme Court nominee, analysts suggested a backlash could follow if Republicans pushed forward with the confirmation.
"Lii nekkaatna ap al kalaj ci GOP gi" moy li Michael Steelemi fii nekkoon njiitu Komite nasonaal bu ripibilikeen yi ci fann yu njékk yii ci ayubes bi su ñu sukkandikoo ci NBC News.
« Cela est devenu un vrai fouillis pour le GOP », a déclaré cette semaine Michael Steele, ancien président du Comité national républicain, selon NBC News.
"This has become a muddled mess for the GOP," said Michael Steele, former chairman of the Republican National Committee, early last week, according to NBC News.
Du rek wote bu komite bi wolla wote bu mujju bi wolla su de Kavanaugh deñ kaa def ci baŋu tuuma bi, waaye anam bi ko repibilikeen yi doxale ak ni ñu ko jappe" ki ko wax moy Guy Cecil, njiitu Priorities USA, ap kurel buy jappale ngir tabb demokarat yi , wonenako ci seenu tasxatu xibaar bi.
« Ce n’est pas seulement une question du vote du comité ou de vote final, ou de faire comparaître Kavanaugh, c’est aussi la façon dont les républicains on traité la situation et la victime », a dit à la chaîne de nouvelles Guy Cecil, directeur de Priorities USA, groupe dédié à aider à élire des démocrates.
"It's just not about the committee vote or the final vote or whether Kavanaugh is put on the bench, it's also about the way Republicans have handled this and how they have treated her," Guy Cecil, director of Priorities USA, a group that helps to elect Democrats, pointed out to the news channel.
Waaye li am ba am moy waa Amerik deñoo xajjalo ci tann ki ñu wara woolu ci jiiñ bu Ford ak seede bu Kavanaugh, te mu and ak gina oyof tuuti jemale ci kii ñu mujje tudde.
Les Américains semblent toutefois se demander qui croire dans la foulée des témoignages de Ford et de Kavanaugh, surtout en ce qui concerne ce dernier.
However, Americans appear to be somewhat split over who to believe in the wake of Ford's and Kavanaugh's testimonies, with slightly more siding with the latter.
Benn xayma bu bees bu juge ci YouGov wonena ni 41 ci teemeer boo jél ci tontukat yi deñoo gëm ci lu leer nañ mbaa ku dem loolu lañuy gëm, ni seede seede tuuma bu Ford bi dëgg la, boobu fekk na 35 ci teemeer boo jël leerna nañ mbaa ku dem loolu lañuy gëm ni lii Kavanaugh wax lañu gëm.
Un nouveau sondage de YouGov révèle que 41 pour cent des répondants croient absolument ou probablement le témoignage de Ford contre 35 pour cent pour celui de Kavanaugh.
A new poll from YouGov shows that 41 percent of respondents definitely or probably believed Ford's testimony, while 35 percent said they definitely or probably believed Kavanaugh.
Mu tegu ci ni 38 yoo jél ci teemeer bu nekk neenañu ni deñoo japp ni Kavanaugh munna fen mbaa defa fen lu leer nañ ci seedam ba, ci loolu 30 ci teemeer boo jël rek loolu lañu wax ci Ford.
De plus, 38 pour cent des répondants ont déclaré croire que Kavanaugh avait probablement ou absolument menti lors de son témoignage contre 30 pour cent pour celui de Ford.
Additionally, 38 percent said they thought Kavanaugh has probably or definitely lied during his testimony, while just 30 percent said the same about Ford.
Ginnaaw bumax bi juge ci Flake, FBI mungi laŋket fi mu nekk nii ci wallu tuuma yi Ford tekk ni ki noonu ak beneen tuumalkat bu tuddu Deborah Ramirez, The Guardian moo ko xamle.
Après la sortie de Jeff Flake, le FBI mène actuellement une enquête sur les allégations de Ford et d’au moins une autre accusatrice, Deborah Ramirez, selon The Guardian.
After the push from Flake, the FBI is currently investigating the allegations brought forward by Ford as well as at least one other accuser, Deborah Ramirez, The Guardian reported.
Ford seedena ci kanamu Komite Yoon bu Sena ci ay waat aybes bii ñu genni ni Kavanaugh sakkuna ko bi mu mannde boobu moom mungi am 17 att.
Ford a témoigné sous serment devant le Comité judiciaire du Sénat la semaine dernière, disant que Kavanaugh, en état d’ébriété, avait abusé d’elle alors qu’elle avait 17 ans.
Ford testified before the Senate Judiciary Committee under oath last week that Kavanaugh drunkenly assaulted her at the age of 17.
Ramirez moom neena ci kanamu Kuur bu Kawe bi ni ki ñu fal def kaa mësa gennel ay awram mu joxoñ ko ko ci benn xew bu ñu demoon bi ñuy jannge ci Yale ci ay atu 1980.
Ramirez allègue que le candidat à la Cour suprême lui a montré ses organes génitaux lors d’une fête durant leurs études à Yale dans les années 1980.
Ramirez alleges that the Supreme Court nominee exposed his genitals to her while they attended a party during their time studying at Yale in the 1980s.
Ku sos World Wide Web bëggna defar Internet bu bees ngir xeex Google ak Facebook
L’inventeur du Web planifie de mettre sur pied un nouvel Internet Plans pour contrecarrer Google et Facebook
The Inventor of the World Wide Web Plans to Start a New Internet to Take on Google and Facebook
Tim Berners-Lee, ku sos World Wide Web, taxawalna ben startup buy diir mbagg Facebook, Amazon ak Google.
Tim Berners-Lee, l’inventeur du Web, lance une nouvelle entreprise dans le but de rivaliser avec Facebook, Amazon et Google.
Tim Berners-Lee, the inventor of the World Wide Web, is launching a startup that seeks to rival Facebook, Amazon and Google.
Porose bu mujju bu kaŋŋam xarale, Inrupt, ab këru liggeeyukaay la buy sukkandiku ci jumntukaayu open source Solid bu Berners-Lee.
Le dernier projet de la légende de la technologie, Inrupt, est une entreprise basée sur la plateforme libre de Berners-Lee, Solid.
The technology legend's latest project, Inrupt, is a company that builds off of Berners-Lee's open source platform Solid.
Solid dina dimbali jarinookat yi ñu tann fan lañuy denc seen i mbir ak ñan ñoo am sañ-sañ jot ci yenn xibaar.
Solid permet à l’utilisateur de choisir l’emplacement où ses données sont stockées ce à quoi les gens ont accès.
Solid allows users to choose where their data is stored and what people are allowed to have access to what information.
Ci bennwaxtaan bu ñu tann ak Fast Company, , Berners-Lee di ruube ni jubluwaay bu Inrupt moy" jiite auna."
Lors d’une entrevue exclusive avec Fast Company, Berners-Lee a plaisanté, disant que le but derrière Inrupt est de « dominer le monde ».
In an exclusive interview with Fast Company, Berners-Lee joked that the intent behind Inrupt is "world domination."
Neena ci ndoorteel startup bi "danu ko wara def leegi."
« Nous devons le faire maintenant », a-t-il dit en parlant de la nouvelle entreprise.
"We have to do it now," he said of the startup.
"Waxtu buñuy fattaliku la."
« C’est un moment historique ».
"It's a historical moment."
Appilikaasoŋ bi ap xarala yu Dëger ngir dimmbali nit ñii defar seeni moomel bopp ci enternet bi" mbaa ap POD.
L’application basée sur la technologie de Solid permet aux gens de créer leur propre « module de données personnelles en ligne » (personal online data store, ou POD).
The app uses Solid's technology to allow people to create their own "personal online data store" or a POD.
Mënna am repertuwaar, loo wara def, kalandiriye, ay woy ak bibiliyotek ak yeneeni mbiri bopp aki ligeeyukaay.
Ce module peut contenir des listes de contacts, des listes de choses à faire, un calendrier, une bibliothèque musicale et d’autres outils personnels et professionnels.
It can contain contact lists, to-do lists, calendar, music library and other personal and professional tools.
Mungi mel ni Google Drive, Microsoft Outlook, Slack ak Spotify yepp mëneesna ko am ci benn buntu enternet te yépp ci benn yoon.
C’est comme avoir Google Drive, Microsoft Outlook, Slack et Spotify sur un navigateur en même temps.
It's like Google Drive, Microsoft Outlook, Slack and Spotify are all available on one browser and all at the same time.
Lan moo nirowul ak lenn ci moomelu bopp yi ci enternet bi moy ki koy jefandiko rek mooy xool lu jo neex mu tann kan moo ci mëna egg, ci ban xeetu xibaar la.
Ce qui démarque le module de données personnelles en ligne est que seul l’utilisateur décide qui a accès à quels renseignements.
What's unique about the personal online data store is that it is completely up to the user who can access what kind of information.
Këru liggeeyukaay bi mungi ko woowe "doxalal say mbiri bopp."
C’est ce que l’entreprise appelle « autonomisation personnelle par l’entremise des données ».
The company calls it "personal empowerment through data."
Su nu sukkandikoo ci kaddu Borom sosete bii di Inrupt John Bruce, Inrupt ap sosete ngir inndi ay koppar la, defay taggat , di faydaal mën mën ngir ñepp muna jot ci lu Déger.
L’idée derrière Inrupt, selon le PDG de l’entreprise, John Bruce, de mettre ressources, processus et capacités appropriées à disposition des gens pour que Solid soit accessible à tout le monde.
The idea for Inrupt, according to the company's CEO John Bruce, is for the company to bring resources, process and appropriate skills to help make Solid available to everyone.
Fii mu nekk nak sosete bi ñi ci nekk moy Berners-Lee, Bruce, ak benn bankaasu kaaraange bu IBM jënd, ak ñenn ci ay defarkat yu ñu jél ngir ñu ligeey ci porose bi ak benn askanu ñii kode, ci ligeey bu anndul ak peyoor.
Actuellement, l’entreprise consiste en Berners-Lee, Bruce, une plateforme de sécurité achetée par IBM, des développeurs employés dans le cadre du projet et une communauté de programmeurs volontaires.
The company currently consists of Berners-Lee, Bruce, a security platform bought by IBM, some on-staff developers contracted to work on the project, and a community of volunteer coders.
Li ko doore bii ayubes, defarkatu xarale ci aduna wërngal këpp dinañu muna defar seen appilikaasoŋ bopp jefandiko ay juntuwaay yu nekk ci bankaasu Inrupt bi.
À partir de cette semaine, les développeurs du monde entier peuvent créer leurs propres applications décentralisées à l’aide des outils accessibles sur le site Web d’Inrupt.
Starting this week, technology developers around the world could create their own decentralized apps using the tools available on the Inrupt website.
Berners-Lee neena moom ak naataango am waxuñu ak Facebook ak Google ndax ñu dugal wolla ñu baña dugal ap coppite ci fepp fu seen bisnees def faa xëy rek nërmeelo ba agg suuf.
Berners-Lee a déclaré que lui et son équipe ne discutaient pas à « Facebook et à Google au sujet de mettre en œuvre ou non des changements qui chambouleraient complètement leurs modèles d’affaires du jour au lendemain.
Berners-Lee said that he and his team are not talking to "Facebook and Google about whether or not to introduce a complete change where all their business models are completely upended overnight.