audio
audioduration (s)
0.74
50.6
transcription
stringlengths
8
285
Xam naa seen jafe-jafe.
bàyyil ma dem fa !
Waaw lii daa taxul barb jóg.
Li moo jur li ñi wax Nancoo yi
Jamono ji féex naa?
Ndax maróo ?
Damaa bëgg wirgo wu mboq.
Lii nag maa ngi ko jëmale ci jëwriñ yi di leen ko ñaan
Mu jooy lu yàgg a yàgg.
foon gi doj wa ci loxo walla gimiñ
Dañoo far sax xoromu.
Dunuy xarit dong a ?
Wool ma tay ci guddi.
Xob yi da ñuy tegaloo ñatt ba juroom ñent
Fii laa dëkk, bés-niki-tey.
Duma lekk yàppu mbaam-xuux.
Waaw kaay fii ci màndaxe gi
Gulami yay, wax ak nit ba mu ànd ak yaw, (convaincre).
Sëriñe Massamba Mbàaké
Am naa jëkër ba noppi.
Maa ngi nii.
Xam naa sa xeet gi.
Fayal ma genn !
Campeefi mbootaay gi
Sunu daara la.
Louga) benn dëkku Senegaal.
Bi ko ko wallkat bi santee lay door a teggi óomam
Yaakaar naa tom a ngi fi.
Ndax yoon la ?
Amleen bàmmeelu-biir !
Man nala xawa sonal tuuti waaye du yàg dara
Dañu amul njariñ.
Damaa bëgg a moom sama bopp.
May ma sama sãs !
Te nëbb dëgg ngir bañ ku mer ca loola la jëm!
Mu wóolooti Maki Sàll, ne ko jiiteel sama kàmpaañ
Njëwriñug paj m
Lépp la am xel man a nangu ba mu des aaye julli.
Am ub saal ca biir bu ñuy wax ndaamaraas mu bari ay njariñ lool.
Dinañ nu gis.
Moom, 29eelu fan ci weeru feewaryee la fi ñëwoon, àndoon ak jëkkër ji
Pël genn giir la gu nekk Senegaal
Fàttaliku ngeen ?
Yéguma woon jàmm.
Dama aw yoon.
du jàmbatub dagg ni dëññ mbaa wetañ
Danga a yég ug tawat a?
Su boobaa, jokkoo ak kër doktoor a war, ngir toppatoo.
jàppoon naa lima wax.
Yaakaaroon na ne faatu na ci saasi
Lii day baj-baji !
Aayu ma ci lii.
Daje naa ak ñoom.
Bu taqee ci yaramu nit day xasan lool
Manumaa nangoo yonjax.
Ba senn Saytaane dootul dox ba fekk nu fi.
Laay! Laay! Laay! Suma la nee laay laay nee ma illalaa.
Màggetu leen maggetaay googu de.
Dama ci bëggaat.
Ku bëggul lu dul yàlla, àgg fa moom,mu jox ko aw yiwam
Jërëjëf Seex Abdul Xaadir
Ak la nga dugal lumu am solo am solo
Dañu laa wóolu.
Damaa am kersa.
Maadoon ndayi mbill ji.
Kaay jàppale ma.
Wéyleen di dawal !
Tom mag la .
Damaa bëgg ay Tóor-tóor.
La xew ca Péncum réew mi ci dibéer jii weesu, ñaaw na te ruslu
Am naa bégte nekk fii.
Li a waral amug ngomblaan dafay tekki teewadig askan wi
Di ci naan digg kaas suba, bëccëg, ak guddi
Kon daal PASTEF deful dara ngir mbas mi ?
Fàww nu jéem.
Dangaa weesu làmp bu xonq ba.
Ëttu xam-xamug nj, nj yaram ak tàggat yaram (INSEPS)
Ndaxte, ñoo ko sooke
Siiwam gi tiitloo woon na way sanc yi ragaloon ag jeqiku kontar leen
Ndax sa bas a ?
Na ngay yewwu yaw njëkk Waxtuw fajar
Waaye la ca tegu nag moom ñépp a ko xam
Dëgg-dëgg maa def loolu a ?
Dangay dëkk ba fàww a ?
Pappa ya walla pabba ya
Yéen a ngi ci yoonu ñàkk.
Saabalkat bii di Aali Faal fésal meram ci naataagoom yiy doxale
Lii am na njariñ sax a?
Ñépp a xaroon
Garab la gu bari lu miy faj lool, day faj biir buy daw.
Xalaatoo ni Sàmbaay Bàcc rekk, am déet ?
Jéemal a neexal sa dund.
Nanu tegoo bant!
Naw naa ko.
Te Yàlla ku jekku lépp la.
Buleen tëj kenn!
Ndax bëgg ngeen faa dem? ?
Xobam rënd la ci toggi yenn réew yi
Niral demai insaàllaa dinaa ñëw Galle lii wan làkk la?
Ma def ko ngir yéen.