audio
audioduration (s)
0.74
50.6
transcription
stringlengths
8
285
Tom daa jaaxle.
Waaw?! Njëg gi jafewul?!
Jàpp nga ma.
Kamakura benn dëkku di Sapoŋ
Searchtool.svg Ngir Xóotal, yëral bii jukki ci Séddaliin wu yoriinu Senegaal.
Bu ko defoon ci ab wolof
Am an ab nataalukaay.
Garab gu bari ay reen la.
Jaani mer bu la màttee noppee koy lugg
Gàmbi ak Miritani tëj nañu seen i dig ngir tëj Senegaal;
Sama kawar gi dafa gudd.
Maami wolof yi Isipt lañu bawoo
Doom bi këmbaan la gu ñàtti-koñe te palmaan
Moo ngi ca pekkam.
Doxoon ñañu ci wet ya.
Njàng mu mitti la nekk.
Fuma ko teg ?
Di kàdduy Aali Nguy Njaay jëwriñu biir réew mi.
Maa ngi dëkk Kakogawa.
Xeex ba jeex na.
Lu àdduna bi di xaar ci luññutu googu?
Ak baax ci sama ndey, te defuma may ku féttéerlu di ku texeedi
MabuuBe yi, ñoo doon Rabb y.
Kenn wanewul woon ag mbañ.
Tom day wut liggéey .
Mayuma ko xel mu gën a ndaw.
Ab mànduwaar la.
Su fi yemoon sax neex
Nasaraanalkat yi yu tubaab yi ñoo leen dugal ci diine jooju
Leegi laay taxaw.
Waxi Sëriñ Bi ci fonk ay waxm ak bañ koo waxal lumu Waxul
Tomb 13 coppiteg laltaay gi
Garab gu ndaw la
Koronaawiris Paab Juuf sonn na lool
Maam khar suul na ba deem
man naa fa dem ayu-bés biy ñëw.
Dañu doon féey.
Waruma woon a nekk fii.
Am naa ab neexal.
Baax na, ma nga ko def
Dinaa xaar ci biti.
Kon PS moom, kenn waxaalewu ko.
Masuma koo gis.
Fi may dundu neex na ma.
Aawlu Nattu lay doon yu tegaloo, nekk dëgg ju wuuteeg tuuma
Ndax bégg nañ ?
Waaye lii ma-kéew yi ak waa Njonge kaas nañu ko ba sonn
?? 15 xal xali matt buy tàkk laa ci xam day
Am naa soxna leegi.
Xeexleen ni ay góor.
Lu tax ngeen wét ?
Garab gi danay àgg ba 5 met ci guddaay
Nit kune am na sañ-sañ woote ab ndaje, mbaa sos mbootaay ci jàmm.
Damaa meroon lool.
Sama daamar gi nanguwuta tàkk.
Tagg gi ngay tagg sa bopp tagg ko sa mbokk.
Buleen laal lii !
Kon gis ko dina gën a yomb fépp ci Senegaal.
Boo maccee buy bi bamu set xoox ba cay des mooy wuy
Tojj xet gu neex la am
Mbootaayu Liggéeyu Àdduna bi
Baax na ak yéen.
Dama bëgg bii liggéey.
Maa ngi màgget.
Faatu dafa ëmb.
Ana golo aka xastey daar-daar ? (3,5)
Ku bees laa fii.
daan jéem a jënd ak ay ndomboy-tànk ndax rekk bëgg a jubook moom…
Nan nga def, tay ?
Ci lumu jëmoon ?
Tom reetaanluwul lool.
Lolli agsi na.
SEEN XIBAAR I BITIM RÉEW
Duñu ñëw .
Nelawuma woon nelaw yu xóot.
Waaye liñ naan bóli gu dog tiiñ na doktoor moo fi ne
Day jël ay waxtu.
Nee ñu ligéey bi lay lootaabe.
Ñoom ñépp a ngi toog di xaar.
Daf leen cee jàppandoo woon.
Abdu Rahmaan Jéey.
Bakkan bu rëy.
Bu dee Àjjuma ñaar-fukki fan ya ak juróom-ñent mooy (L..X..)
Jël nab téereem.
Jur gi ñax lay dunde.
Li ci am solo mooy NU GËM KO TE DOXE KO
Bul ko wax sa baay .
Am na ñetti nas te yaramam mooy kalabas bu nu taqe deru bëy
Ndax yaw yaay Tom ?
Fompal sa rongoñ yi!
Dafa am njariñ lool.
Bu leen daanu !
Tàllalal sa loxo !
Manoo koo jëfandikoo.
Tëjleen poxla gi !
Jataay bu matale biSoppi
Te, ñaari kurél yooyu yépp,  Mbay Jaag ak i ñoñam ñoo leen jiite woon
Tom dafa ragal.
Mu ne ko lekkal li feek yaa ngi sikk, ba sikkatoo (nga jàpp)”
Mbootaayu peeyi lislaam yi